#2stvlive SPECIAL GAMOU AVEC TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE ET CHERIF MAMINE AIDARA Λήψη

Αποστολή στους φίλους σας
Προσθήκη
  • პირდაპირ ეთერში გავიდა 9 მაი. 2020-ში

  • www.2stv.net Iptv disponible sur 2stv.sn https://www.instagram.com/2stvlofficiel https://www.facebook.com/2stvsenegal https://twitter.com/2stvsenegal

Σχόλια

  • Eva Lopy
    Eva Lopy 6 თვის წინ

    Je suis catholique mais damaay deuglou Tafsir ba faté ni k bokou gnou diiné🙇🙇🙇 Yallah nako Yallah défaal jamm

  • Linguerou Bour
    Linguerou Bour 6 თვის წინ

    Kou d’accord ni dafa wara continuer meme apres le ramadan?

  • Mane Idrissa
    Mane Idrissa 6 თვის წინ

    Kou beugeu seydina mouhaméd bjl j'aime guir sounou borom yallah kou beugeu abdourahmane gaye aussi beujeul j'aime ❤️😭🙏yalla fayla

  • oly la Déesse
    oly la Déesse 6 თვის წინ

    Tafsir il est juste unique machalla Yalla na Yalla goudeul fanam

  • Zeynab Diallo
    Zeynab Diallo 6 თვის წინ (რედაქტირებული)

    Keeneu dou seydina Mouhamed( psl) fière d'être Talibé cheikh 💯💯💯💕💕💖💖💖💖💖💖💖💕💞💞😭😭😭Rassoulillah sangue sangg yiii machallah 😭😭😭

  • Fatima Ndiaye
    Fatima Ndiaye 6 თვის წინ

    Ay sougnio wadji seydina Mouhamet’s sant nagnio yalla ba sougnio borom bole gnio si khetam contane na trop

  • Pape Omar Gning
    Pape Omar Gning 6 თვის წინ

    Vraiment émission tay bi done na rafet kounek si Sénégal gor djiguen mag ak ndaw setane ko parce rer gui dafa bari trop wakh dji bari nio kham ni danouy wakhé sen khalat waya wakhalouniou dinné di diakhassé senegal diné daniou koy teg si ay référence you woor pas si khel bou rafet

  • Diouf Ibrahima
    Diouf Ibrahima 6 თვის წინ

    Comment une personne normale peut ne pas aimer ça. Ceux qui ont disliker franchement allez vous faire soigner

  • Lavezzi Pedro
    Lavezzi Pedro 6 თვის წინ

    Les personnes qui n'ont pas aimés cette vidéo je me demande c'est quoi votre blem

  • Bam's Bam's
    Bam's Bam's 6 თვის წინ

    Maodo maodo maodo maodo maodo

  • Abdoulaye AGNE
    Abdoulaye AGNE 6 თვის წინ

    As'salamou aleykoum wa rahmatoullahi wa tallahou wa barakatouhou longue vie et santé de fer à vous. Que la paix, la miséricorde et la bénédiction d'Allah soient sur vous 🤲. Qu'Allah vous préserve 🤲

  • omzo Niang
    omzo Niang 6 თვის წინ (რედაქტირებული)

    Billahi wallahi j'ai toujours et je souhaite jusqu'à au futur incha Allah appelle mon première fils Mohamadou Moustapha incha Allah prier pour moi

  • Cheikhouna Ba
    Cheikhouna Ba 6 თვის წინ

    Aufaite Mawdo moniou khamal rassoulillahi aleyhi salaam ❤️❤️❤️télé bodem ndiabootam nioyy wakh louy doug ci khol yi ❤️❤️sant bougn néké talibè cheikh

  • Nogaye Camara
    Nogaye Camara 6 თვის წინ

    Haaa sama fans bii gaye yala n'a yala fayale bopam thi barké seydina mouhamet

  • Niang Mame
    Niang Mame 6 თვის წინ

    Mashallah, tafsir est vraiment unique dans son genre. Yalna Yalla Goudeul faname

  • Cheikh Ahmed Tidiane Diaw
    Cheikh Ahmed Tidiane Diaw 6 თვის წინ

    Li rafétna Tidiane yepou bénnlaniou nioune wake baye niass konatananiou ci mame maodo ak wakerem tafesir yabakh

  • Cheikhouna Ba
    Cheikhouna Ba 6 თვის წინ

    Limassi diaakhal rek dina meuss doorr sama iphone 11 bi ci mur bi ndah lii mawdo bindd dafa neekh loooooollll❤️❤️😂jerejef seydil hadji malick sy ❤️❤️

  • Coumba Dieye
    Coumba Dieye 6 თვის წინ

    Yallanalé yalla fayale bopam ak équipes bi yeupp machalla

  • Sosso Fall
    Sosso Fall 6 თვის წინ

    Kouma mayone tafsir ma seuyal ko mom soudé diouromel lay done juste pour moumey waxtanal sama sopet bi sws 😭😭😤

  • Miijo Tv
    Miijo Tv 6 თვის წინ

    Longue vie à tafsir abdourahmane et à chérif mamine aidara